Sylla Madrista

Sylla Madrista Informations de contact, plan et itinéraire, formulaire de contact, heures d'ouverture, services, évaluations, photos, vidéos et annonces de Sylla Madrista, Diourbel, Touba.

Victoire du Real Madrid vs Benfica 2-1Tchoumeni ⚽️Vini Jr ⚽️ Y nada mas 🤍
25/02/2026

Victoire du Real Madrid vs Benfica 2-1
Tchoumeni ⚽️
Vini Jr ⚽️

Y nada mas 🤍

Pedri: "Sudee mën naa siñe benn joueur Real Madrid ngir Barça? Kylian Mbappé."Ferran Torres: "Waaw, Mbappé."Pedri: "A jo...
24/02/2026

Pedri: "Sudee mën naa siñe benn joueur Real Madrid ngir Barça? Kylian Mbappé."

Ferran Torres: "Waaw, Mbappé."

Pedri: "A joueur buma bëggul jano ak moom ci duel gaawaay? Lu jege ñépp, dama yeex tuuti.
Mbappé, Vinicius... waaw, su bal bi yeggee ci Vinicius Junior, li nga mëna def lu lenn ludul ñaan. Daf ma gëna gaaw ñetti yoon."

🚨C'est OFFICIEL Slavko Vinčić mooy arbitre match bi diggante Real Madrid ak Benfica ci Alarba. ✅🇪🇺🇪🇦🇵🇹⚽📊 Arbitre na 3 ma...
24/02/2026

🚨C'est OFFICIEL Slavko Vinčić mooy arbitre match bi diggante Real Madrid ak Benfica ci Alarba. ✅🇪🇺🇪🇦🇵🇹⚽

📊 Arbitre na 3 match yu Real Madrid

✅ Real Madrid 1-0 Juventus (2025/26)
❌ Real Madrid 1-3 AC Milan (2024/25)
✅️ Real Madrid 2-0 Dortmund ( 2023/24) final League de champions

🚨 Sunu sukkandikoo ci AS, Real Madrid mingi topp Nico Schlotterbeck bu baax.Defaaseer bu Almaañ bi am 26 at, ñungi ci ko...
23/02/2026

🚨 Sunu sukkandikoo ci AS, Real Madrid mingi topp Nico Schlotterbeck bu baax.

Defaaseer bu Almaañ bi am 26 at, ñungi ci kontraa ba 2027, ñu xayma ko lu tollu ci €50 milyoŋ 💰.

Ci biir, ñu jàpp ni profilam bi mën na tax club bi soppi pexem transfert bi ñuy faral di def, rawatina su amee yéene dugal xaalis bu bari ci benn joueur bu weesu 20 at, muy lu wuute ci sesoŋ yii weesu.

👉Defense nekk na priorite bi gëna am solo: ci ñaari seson yii ñu weesu, poñ yu bari lañu ñàkk ndax njuumte yu benn-benn defenseur yi def.

🚨 BENFICAUEFA yëgalna Benfica ni plainte bi club bi def ci mbirum Federico Valverde defa bañ.Club bu Portugal bi mungi r...
23/02/2026

🚨 BENFICA

UEFA yëgalna Benfica ni plainte bi club bi def ci mbirum Federico Valverde defa bañ.

Club bu Portugal bi mungi réccu ni, doonte widewo yi dañu wone fitnaal bi ñu sonal joueur bu Benfica bi di Samuel Dahl, UEFA jëlna dogal ni du door ay dosiye disiplineer.

🎙️ Jamal Musiala defna lu dëgër te am xel mu dal ci mbirum Vinícius."Li xewoon ci Vini ak Benfica? Anterneer bi (Vincent...
22/02/2026

🎙️ Jamal Musiala defna lu dëgër te am xel mu dal ci mbirum Vinícius.

"Li xewoon ci Vini ak Benfica? Anterneer bi (Vincent Kompany) waxna lu baax ci mbir mi. Rasism du topic bu baax.

Dama jàpp ni anam wi Vinícius di doxalee baaxna lool. Ak koolute gi ma am ci moom, jàpp naa ni du fen ci mbir mu am solo nii. Dina gëna jur jafe-jafe ak lépp lu baax.

Mbir mu yàgg la, te amul lu bari luma mëna wax wala def ngir soppi ko. "Leerna ni neexul gis, man ci sama bopp."

🚨FUL TIM: ASSUNA 2-1 Real MadridVinicius Jr. (73')Real Madrid mënuwoon jëfandikoo seen occasion ngir yokk seen njiit ci ...
21/02/2026

🚨FUL TIM: ASSUNA 2-1 Real Madrid

Vinicius Jr. (73')

Real Madrid mënuwoon jëfandikoo seen occasion ngir yokk seen njiit ci kaw liig bi. Defet buy jur xaalis bu bari ci Los Blancos. 😔

⚽️ JOUR DU MATCH ⚽️ VS OSASUNA 🔴⚪️LA LIGA 25e JOURNÉE 🏆17H30 GMT ⏰️A ESTADIO EL SADAR 🏟HALLA MADRID 🤍
21/02/2026

⚽️ JOUR DU MATCH ⚽️
VS OSASUNA 🔴⚪️
LA LIGA 25e JOURNÉE 🏆
17H30 GMT ⏰️
A ESTADIO EL SADAR 🏟

HALLA MADRID 🤍

Victoire du Real Madrid vs Benfica 0-1Vini Jr ⚽️ Y nada mas 🤍
17/02/2026

Victoire du Real Madrid vs Benfica 0-1
Vini Jr ⚽️

Y nada mas 🤍

FATTALI: Huijsen, Carreras ak TchuameniDinañu leen SUSPEND ci match bi ñuy joŋante ak Benfica suñu ame carton jaune ci m...
17/02/2026

FATTALI: Huijsen, Carreras ak Tchuameni
Dinañu leen SUSPEND ci match bi ñuy joŋante ak Benfica suñu ame carton jaune ci match tay bi ak Benfica

🚨🚨 Alvaro Arbeloa🎙️Revanche ak Benfica ? Déedet, déet. Sunu mébet du daan Benfica wala fayyu. Sunu mébet mooy jël Champi...
17/02/2026

🚨🚨 Alvaro Arbeloa🎙️
Revanche ak Benfica ? Déedet, déet. Sunu mébet du daan Benfica wala fayyu. Sunu mébet mooy jël Champions League, te daan Benfica benn jéego la ci yoon woowu."

🚨🚨 Eduardo Camavinga:"Yaakaar naa ni amnaa lu bari luma wara def ci Real Madrid, ngir wane lu gëna bari. Soppe yi gisu ñ...
17/02/2026

🚨🚨 Eduardo Camavinga:

"Yaakaar naa ni amnaa lu bari luma wara def ci Real Madrid, ngir wane lu gëna bari. Soppe yi gisu ñu lépp lu Camavinga mëna def ba leegi."

Adresse

Diourbel
Touba

Site Web

Notifications

Soyez le premier à savoir et laissez-nous vous envoyer un courriel lorsque Sylla Madrista publie des nouvelles et des promotions. Votre adresse e-mail ne sera pas utilisée à d'autres fins, et vous pouvez vous désabonner à tout moment.

Partager